BLAGUES

Page 4 sur 6 Précédent  1, 2, 3, 4, 5, 6  Suivant

Voir le sujet précédent Voir le sujet suivant Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  el king le Jeu 28 Déc - 4:26

Fifi a écrit:Li nak béne couple la wone djiouné niome jour yi terminé pare dre reck lagnouye séye maname défe rapport. Légui nak kou goorki déme touti 1 moi il est revenu un lundi. légui comme diabare bi namone nako et ke le lundi ne fé pas parti des ces jour la mou dale dinéko wa chéri lo wakh si lundredi ment bi nak Smile @

fifi tothie nga fi. kom koi ke nanditré sonoul
avatar
el king
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 45
Date d'inscription : 02/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  NUTELLA le Jeu 28 Déc - 4:31

Fifi a écrit:Li nak béne couple la wone djiouné niome jour yi terminé pare dre reck lagnouye séye maname défe rapport. Légui nak kou goorki déme touti 1 moi il est revenu un lundi. légui comme diabare bi namone nako et ke le lundi ne fé pas parti des ces jour la mou dale dinéko wa chéri lo wakh si lundredi ment bi nak Smile @

lol! lol! trop fort ndawssi dafa diambalalé wone Laughing
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  el king le Jeu 28 Déc - 4:55

Ki nak béne waye dieunde kharam ba niou né souba la tabaski rék kharmi dé. Si goudi gui rék mou yé séne wakeur yeup né léne diapalé léne ma niou yobb kharmi keur élimane mou wakh niou sou kharmi dagané niou togue ko sou daganoul niou lakk ko.
Bi niou yéggué keur élimane, wadji né ko
- Elimane ma ladj la touti, kham nané goudi na waya mbir mi da ma sokhal lolou
- Waw mba diam , répondit l'imam
- Sama khar da dé legui ta souba la tabaski. légui ma lay ladj réndi nitt ak réndi yall bou gana dagane
- Ah doyna war dé.... commença Elimane
- Kone dagane na, coupa wadji, yénou léne niou délou keur gua
- Ah do ko bayyi sakh mou tontou nidiaye? damanda diabar dji
- mouné ko : souma la si fassé nak

Laughing Laughing
avatar
el king
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 45
Date d'inscription : 02/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  Fifi le Jeu 28 Déc - 4:58

Guisguéne dé ki kéye wéssouna diambalé
el king guisna yi guéye lépe dafa dikhe si diamono Very Happy
avatar
Fifi
Moyenne section
Moyenne section

Nombre de messages : 107
Date d'inscription : 04/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  NUTELLA le Jeu 28 Déc - 5:37

El king ah non way mayniou nou noyi lol! lol! lol! lol!

Fifi djiguéne bou diambalé thiéy Wink
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  el king le Jeu 28 Déc - 8:44

Ki nak béne waye da dém dieunde khar bou niou kouk. aandi ko nak diabar dji néko mak khar mi dou niou fi bokkou fanane. Wadji khalat khalat khamoul nou mouy def.Finalement mou dem si ndiago bi né ko
- dama beugue nga peintural ma sama kar peinture bou wekh
- ndiago bi néko mane dé peinture na fi ba france waya meussouma peinture khar
Wadji sarakhou ko, mou peintural ko blanc bou rafét .wadji nieuw yéw kéy, ndaw si néko téré bien nidiaye, ni la kéy, khar bou nioul day oumaté.
Niou teude ba goudi rék, assamane si komanssé deunde kéy ak éclairs yi di wadia taw. Rék sawaye dém yéwi kharmi rék nieuw takk si nékk bi
Sokhna si néko ah waw nidiaye khar ba si bir négue bi nak
mounéko: dou ya néwone do bokk fanane ak khar bou nioul. Andil nala bou wekh nak di nga fanane ak mom dé par force doolé mbaam

Laughing Laughing
avatar
el king
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 45
Date d'inscription : 02/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  NUTELLA le Jeu 28 Déc - 9:38

el king a écrit:Ki nak béne waye da dém dieunde khar bou niou kouk. aandi ko nak diabar dji néko mak khar mi dou niou fi bokkou fanane. Wadji khalat khalat khamoul nou mouy def.Finalement mou dem si ndiago bi né ko
- dama beugue nga peintural ma sama kar peinture bou wekh
- ndiago bi néko mane dé peinture na fi ba france waya meussouma peinture khar
Wadji sarakhou ko, mou peintural ko blanc bou rafét .wadji nieuw yéw kéy, ndaw si néko téré bien nidiaye, ni la kéy, khar bou nioul day oumaté.
Niou teude ba goudi rék, assamane si komanssé deunde kéy ak éclairs yi di wadia taw. Rék sawaye dém yéwi kharmi rék nieuw takk si nékk bi
Sokhna si néko ah waw nidiaye khar ba si bir négue bi nak
mounéko: dou ya néwone do bokk fanane ak khar bou nioul. Andil nala bou wekh nak di nga fanane ak mom dé par force doolé mbaam

Laughing Laughing

lol! lol! éy way nioul mo méti way Laughing wadji khana dafa faté né khar bi fok niou sang ko tongue
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  Big le Mer 3 Jan - 14:26

lol!

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  NUTELLA le Mer 3 Jan - 16:09

Big a écrit:lol!

mak dou khalngou Laughing ah non way
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  Big le Jeu 4 Jan - 6:38

NUTELLA a écrit:
Big a écrit:lol!

mak dou khalngou Laughing ah non way

NUTELLA,

Pourtant Makk yii en Privé avec leur femme , bou dara dessoul loudoul lewtoh , dinagnou deff louné : tassou , deubb , lépp, fétieu cherry lol!
Gningaye guiss gnouye ngadeu ngandeu lou le MAtin khamo lougnou deff le Soir Very Happy

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  thiaate le Ven 5 Jan - 5:14

Big a écrit:
NUTELLA a écrit:
Big a écrit:lol!

mak dou khalngou Laughing ah non way

NUTELLA,

Pourtant Makk yii en Privé avec leur femme , bou dara dessoul loudoul lewtoh , dinagnou deff louné : tassou , deubb , lépp, fétieu cherry lol!
Gningaye guiss gnouye ngadeu ngandeu lou le MAtin khamo lougnou deff le Soir Very Happy

com toi ki tapelles "BIG"? echkeu si nga bokk? Arrow Arrow
avatar
thiaate
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 462
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  Big le Ven 5 Jan - 5:25

thiaate a écrit:

ah non mann bokou maci déh. Cool
Meunn na juste faire des lépp ou raconter des blagues. Mais Tassou waleu waleu fetieu mome merci.

Tiens Thiaate , j'ai vu dans une piéce theatrale à St Louis, la femme demandait à son Mari de piller (deub) Very Happy Very Happy c quoi cette féme (jeu) Smile

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  thiaate le Ven 5 Jan - 5:41

big, bane théatre leu? je men rapél pas!
avatar
thiaate
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 462
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  Big le Ven 5 Jan - 5:53

c un theatre de Imam Fall qui joue avec Golbert Diagne

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  thiaate le Ven 5 Jan - 6:02

Big a écrit:c un theatre de Imam Fall qui joue avec Golbert Diagne
réé ba tass!
yaw sa khél neekh neu? ds tous les dramatiques de ndar ya imam fall et golbert diagne! tu mapren rien de plus bou mey lééral dé! cété koi lhistoire?
avatar
thiaate
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 462
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  NUTELLA le Ven 5 Jan - 13:21

Big a écrit:
NUTELLA a écrit:
Big a écrit:lol!

mak dou khalngou Laughing ah non way

NUTELLA,

Pourtant Makk yii en Privé avec leur femme , bou dara dessoul loudoul lewtoh , dinagnou deff louné : tassou , deubb , lépp, fétieu cherry lol!
Gningaye guiss gnouye ngadeu ngandeu lou le MAtin khamo lougnou deff le Soir Very Happy

Big [b] féth ba sani marakiss diarnaco lol! lol! lol!
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  Big le Ven 5 Jan - 13:46

thiaate a écrit:
Big a écrit:c un theatre de Imam Fall qui joue avec Golbert Diagne
réé ba tass!
yaw sa khél neekh neu? ds tous les dramatiques de ndar ya imam fall et golbert diagne! tu mapren rien de plus bou mey lééral dé! cété koi lhistoire?

le gars (Imam Fall)etait un riche qui avait 2 femmes.

la nuit l'une des femmes lui a donné un kour ak guenn bou vide , mouye deubb

le mAtin Awo bi neko demb ci goudi dama degg aye deubb , mounéko "mbadou aye rabbou gouddi "

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  NUTELLA le Sam 6 Jan - 6:44

Big lol! lol! lol! guiss ga sééni pékhé dé
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  thiaate le Sam 6 Jan - 12:16

big je men rapél pas!
mais tu sais fém yii mom kou nékk rek ak sa boss!
gni da gnouy taassou! gnii di lééb! gnii di fethie! gnii di toggue! kou né daal ak fi nga meuné! am neu tamite gnou polyvalent!
Arrow Arrow
avatar
thiaate
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 462
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  NUTELLA le Lun 8 Jan - 13:14

léboone lipoone amoone nafi dayaan tongue tongue

aye thia léne boc lol! lol! deumeu geuth rétane
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  Big le Mar 9 Jan - 8:48

NUTELLA , magneuw

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  NUTELLA le Mar 9 Jan - 9:49

Big a écrit:NUTELLA , magneuw

lol! lol! contane si yaw dal
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  el king le Dim 14 Jan - 13:39

Ki nak béne gor djiguéne la wone, dougou si P9 bi , né receveur bi
- Sama thiamègne diayma ticket, receveur bi né ko
- Simm, gordjiguène kharamata ndiaye yi, ni ma lène bagné
- Mouné ko: da ma beugue nga dimbalima dé, Sénégal ba mou dadj ya si gueuna touti bureau, sof ba dé

Laughing Laughing
avatar
el king
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 45
Date d'inscription : 02/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  NUTELLA le Dim 14 Jan - 13:48

el king a écrit:Ki nak béne gor djiguéne la wone, dougou si P9 bi , né receveur bi
- Sama thiamègne diayma ticket, receveur bi né ko
- Simm, gordjiguène kharamata ndiaye yi, ni ma lène bagné
- Mouné ko: da ma beugue nga dimbalima dé, Sénégal ba mou dadj ya si gueuna touti bureau, sof ba dé

Laughing Laughing

lol! lol! lol! lol! lol!
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  el king le Lun 15 Jan - 14:00

Madame: Allez... S'il te plaît chéri ?
Monsieur: Non. Laisse-moi tranquille.
Mme. Allez, ça ne te prendra pas trop de temps.
Mr: Après je ne saurai pas me rendormir.
Mme: Mais sans ça, je ne pourrai pas dormir.
Mr: Je voudrais bien savoir pourquoi tu penses à des trucs pareils au beau milieu de la nuit?!
Mme: Parce que je suis brûlante!
Mr: Toi, tu es chaude au pire moment, vraiment.
Mme: Si tu m'aimais, je ne devrais pas avoir à insister comme maintenant pour que tu le fasses
Mr: Si tu m'aimais MOI, tu aurais plus de considération pour moi.
Mme: Alors tu ne m'aimes plus.
Mr: Mais si je t'aime, mais laisse tomber ça pour cette nuit, OK.
Mme: (sanglots)
Mr: (waaaaaaah -soupirs) D'accord, je vais le faire, tu as gagné.
Mme: Qu'est-ce qui se passe chéri? Tu as besoin d'éclairage?
Mr: Je ne trouve pas...
Mme: Ben vas-y à tâtons, tu vas quand même bien y arriver.
Mr: Ça y est, voila. J'y suis. Alors, heureuse?
Mme: Ahhhh, enfin, OUI, comme ça fait du bien!
Mr: Bon, la prochaine fois que tu voudras dormir la fenêtre ouverte, t'iras l'ouvrir toi-même!
avatar
el king
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 45
Date d'inscription : 02/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: BLAGUES

Message  Contenu sponsorisé

Contenu sponsorisé

Revenir en haut Aller en bas

Page 4 sur 6 Précédent  1, 2, 3, 4, 5, 6  Suivant

Voir le sujet précédent Voir le sujet suivant Revenir en haut

- Sujets similaires

Permission de ce forum:
Vous ne pouvez pas répondre aux sujets dans ce forum