coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Page 5 sur 7 Précédent  1, 2, 3, 4, 5, 6, 7  Suivant

Voir le sujet précédent Voir le sujet suivant Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Chouxalacreme le Mer 10 Jan - 10:09

thiaate a écrit:waw big sieste dey am recette? ma fogone ni improvisation bi mo eupp khorom? Arrow Arrow
lann mo thi impro bi nak moi j'ai rate des choses deh Laughing Laughing Laughing Laughing
avatar
Chouxalacreme
Moyenne section
Moyenne section

Nombre de messages : 177
Age : 32
Localisation : Seychelles
Date d'inscription : 15/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Mer 10 Jan - 10:10

Kouléne wakh ni SIESTE = Forcement DORMIR

Kou amoul loye deff moye nelaw Very Happy Very Happy

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Chouxalacreme le Mer 10 Jan - 10:13

Big a écrit:Kouléne wakh ni SIESTE = Forcement DORMIR

Kou amoul loye deff moye nelaw Very Happy Very Happy
ahhhh Shocked Shocked Shocked Shocked kon lann moye sieste nak eh ben dis donc on apprend des chose par ici Shocked
avatar
Chouxalacreme
Moyenne section
Moyenne section

Nombre de messages : 177
Age : 32
Localisation : Seychelles
Date d'inscription : 15/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Mer 10 Jan - 15:22

Chouxalacreme a écrit:
Big a écrit:Kouléne wakh ni SIESTE = Forcement DORMIR

Kou amoul loye deff moye nelaw Very Happy Very Happy
ahhhh Shocked Shocked Shocked Shocked kon lann moye sieste nak eh ben dis donc on apprend des chose par ici Shocked

Sieste ne signifie pas ronfler. c'est se coucher dans un but de relaxer et faire digerer vite.

kounekkeu ak sa methide selon le menu.

Si t'a rien d'interressant plein de toi tu ronfle
lol!

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  thiaate le Jeu 11 Jan - 6:31

Big a écrit:Kouléne wakh ni SIESTE = Forcement DORMIR

Kou amoul loye deff moye nelaw Very Happy Very Happy

purtan wakhouma wone wakhou dormir dé!
Arrow Arrow
avatar
thiaate
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 462
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Lun 15 Jan - 4:42

quel plat pour l'année 2007.

Ayeweu démléne Marssé ndougui

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  coumbisse le Mar 16 Jan - 8:36

maa fi fass yéné togue Tiébou yapou mouride.

da gnouy kheuy soubeu dem daral ba.
diende khar bou ndaw bou def une quinzaine de kilos rek.
ray lou ko fess lou ko ba mou nice.

dagueté khar bi.


Ingredients
15 kilos de viande
5 kilos de riz
1.5 kilos d'oignons
poivron, tomate, concombre
ail, poivre,jumbo et sel

* rakhass sama yap, bou fess bi seté sakh diarou ko
rossi sama yap si touti huile, juste un litre
*deub nokossou soblé, ail ak touti poivre def ko si rossi bi pour mou geuneu dooré,
* bayi yap bi bamou dooré ma gnoulouk
*bayi ko mou bakh touti, yap bi gnor gnoulouk bi baar
*dolli si dessitou nokoss bi sou dooré wé

* tay sama thiep
*teumbeul sama doomou kaani you didj
*rossi sama thiep bayi ko mou gnor à petit feu.

*dagueté sama soblé pour defar sauce
*dagueté samay tomate ak gnoomine poivron akh concombre pour decorer le riz
* bakhal sama kelk néne pour deco aussi

bou thiep bi gnoré ma yak ko si gnaari ngadoum bols ( boolou mouride maanam), decorer ko ba mou nice.

tibeul si waa roukh bi yeup surtout saa mbokou talibé yi.

coumbisse
Petite section
Petite section

Nombre de messages : 92
Age : 37
Date d'inscription : 04/01/2007

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Mar 16 Jan - 8:49

Coumbisse ,

sama bole nakk, tenga servir meu beneu Coca Cola té defarale meu léweul bou nékh pour digerer

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  coumbisse le Mar 16 Jan - 8:55

BIG kassou ataaya mouride laa lay dooral diokh la coca cola bou sed gouy pour digerer Very Happy

coumbisse
Petite section
Petite section

Nombre de messages : 92
Age : 37
Date d'inscription : 04/01/2007

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Mar 16 Jan - 9:35

coumbisse a écrit:BIG kassou ataaya mouride laa lay dooral diokh la coca cola bou sed gouy pour digerer Very Happy

Coumbisse
limotakh nga nékh meu.
yAW LO BEUG REKK YALA NAYE DIAMEU NEH MANGUI CI

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  coumbisse le Mer 17 Jan - 4:53

Big a écrit:
coumbisse a écrit:BIG kassou ataaya mouride laa lay dooral diokh la coca cola bou sed gouy pour digerer Very Happy

Coumbisse
limotakh nga nékh meu.
yAW LO BEUG REKK YALA NAYE DIAMEU NEH MANGUI CI

amineeeeeeeeeeeeeeeeeeeee

coumbisse
Petite section
Petite section

Nombre de messages : 92
Age : 37
Date d'inscription : 04/01/2007

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Bujuman le Mer 17 Jan - 6:07

coumbisse a écrit:BIG kassou ataaya mouride laa lay dooral diokh la coca cola bou sed gouy pour digerer Very Happy
Yox mba dou da nga hawa bardée si BigA ? Very Happy

Chez Tafagr dale da ngay ré ba tass. IL y'a parfois des dialogues hors entenne. Arrow

Bujuman
Admin
Admin

Nombre de messages : 150
Date d'inscription : 06/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Mer 17 Jan - 6:20

Buju,

Khana khamoni Coumba avec les plats qu'elle fait , waurr na Yallah ni souma amone aye Milliards de dollars mokoye lekkeu bamou sett witieu .

Toggal fofou rekk,


Dernière édition par le Mer 17 Jan - 7:25, édité 1 fois

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Bujuman le Mer 17 Jan - 6:58

Moi il me faut des recettes pour végétarien. Je veux vire 120 ans.

Bujuman
Admin
Admin

Nombre de messages : 150
Date d'inscription : 06/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  NUTELLA le Mer 17 Jan - 9:06

Big a écrit:Buju,

Khana khamoni Coumba avec les plats qu'elle fait , waurr na Yallah ni souma amone aye Milliards de dollars mokoye lekkeu bamou sett witieu .

Toggal fofou rekk,

Shocked Shocked waw sokhna yiçi dess nac tongue
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Jeu 18 Jan - 2:19

NUTELLA a écrit:
Big a écrit:Buju,

Khana khamoni Coumba avec les plats qu'elle fait , waurr na Yallah ni souma amone aye Milliards de dollars mokoye lekkeu bamou sett witieu .

Toggal fofou rekk,

Shocked Shocked waw sokhna yiçi dess nac tongue

NUTELLA , sokhna yici dess katt dagnou yagg ci waagn wi téh togougnou.

Coumba mome bimou yekssiwé c'est avec un plat qu'elle nous a dit Assalamaleykoum

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Jeu 18 Jan - 2:25

NUTELLA,

yaw toggal ngama kerok , mais danga fattéh boléci recettes pour Sieste.



WA LES FILLES VENAIENT AIDER BUJUMAN avec un PLAt pour vegetarien : genre mbakhalou Saloum. IL parait que NIYA meunoul togg lol! santa

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  cherieallune le Jeu 25 Jan - 2:25

ah yéne séne fi am na maana.

li ay plat.

tokk yi mourité neu ( cest juste une expression pour dire que les tokk sont TRES bIEN ).

Sougnou keur bou gnou guissé lou rafet dagnou naane dafa mourité kham nga rek kou rathie dieumeulé sa bord mou deul)

mane recettou paella bou simple laa beug kou ma ko baakhé wayyyyyyyyyy
avatar
cherieallune
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 167
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Jeu 25 Jan - 5:28

cherieallune a écrit:ah yéne séne fi am na maana.

li ay plat.

tokk yi mourité neu ( cest juste une expression pour dire que les tokk sont TRES bIEN ).

Sougnou keur bou gnou guissé lou rafet dagnou naane dafa mourité kham nga rek kou rathie dieumeulé sa bord mou deul)

mane recettou paella bou simple laa beug kou ma ko baakhé wayyyyyyyyyy

mais c normal déh, lou baakh dafaye mourité mome.

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Jeu 25 Jan - 5:31

cherieallune,

quel plat tu proposes pour notre ami Bujumann

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  cherieallune le Jeu 25 Jan - 6:13

ah moom lane lagn ko wara togal sakh.
kharal ma reflechir gneuwaate.
avatar
cherieallune
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 167
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  NUTELLA le Jeu 25 Jan - 11:37

Big a écrit:NUTELLA,

yaw toggal ngama kerok , mais danga fattéh boléci recettes pour Sieste.



WA LES FILLES VENAIENT AIDER BUJUMAN avec un PLAt pour vegetarien : genre mbakhalou Saloum. IL parait que NIYA meunoul togg lol! santa


yaw thiép bou nékho nonou boko léké loy doyé sieste gorgui Laughing khana teudeu sa pliant réc di ressal ak sa sothiou bou goudeu tongue tongue


Bujuman boul nangou ndoudeu ba wakhtou bobou dé Wink ndaklhté bou yeup démé kone yaw késsé yafiy dess affraid affraid



Coumbisse sama thiébou mouride bi lounè leu wanté limassi diakhal thiép di dagnou kay saff Laughing noumou démé nonou Wink


cheriallune ziarr naleu boufi di geuth way

_________________
[b] LE CHIEN ABOIE LA CARAVANE PASSE
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Ven 26 Jan - 8:38

NUTELLA a écrit:
Big a écrit:NUTELLA,

yaw toggal ngama kerok , mais danga fattéh boléci recettes pour Sieste.



WA LES FILLES VENAIENT AIDER BUJUMAN avec un PLAt pour vegetarien : genre mbakhalou Saloum. IL parait que NIYA meunoul togg lol! santa


yaw thiép bou nékho nonou boko léké loy doyé sieste gorgui Laughing khana teudeu sa pliant réc di ressal ak sa sothiou bou goudeu tongue tongue


Cheu mann ak sotieu pour digerer yorouko , il me faut lou andeu ak douceur Cool

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  viyaypi le Lun 29 Jan - 2:51

jsais pas faire la cuisine rabbit le pire cé que ça me derange pas No

viyaypi
Petite section
Petite section

Nombre de messages : 11
Date d'inscription : 27/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  cherieallune le Lun 29 Jan - 3:54

viyaypi a écrit:jsais pas faire la cuisine rabbit le pire cé que ça me derange pas No

gosette khana doo senegalaise, si tu te maries avec un vrai senegalais té meunoulo thiep moom ce sera facile quil aille voir ailleurs dé.

un senegalais on le garde pret de soi en lui faisant de la bonne bouffe.

bonne journee et prends des cours cherie surtout pour garder ton ame pour toi toute seule
avatar
cherieallune
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 167
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Contenu sponsorisé


Contenu sponsorisé


Revenir en haut Aller en bas

Page 5 sur 7 Précédent  1, 2, 3, 4, 5, 6, 7  Suivant

Voir le sujet précédent Voir le sujet suivant Revenir en haut

- Sujets similaires

 
Permission de ce forum:
Vous ne pouvez pas répondre aux sujets dans ce forum