coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Page 7 sur 7 Précédent  1, 2, 3, 4, 5, 6, 7

Voir le sujet précédent Voir le sujet suivant Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  ramise le Mar 13 Fév - 1:09

sama serigne boul wakh darra leggui mou gnew tanyi je sui débordé avec le boulot je n ai pas asez de temps pour te concocter un bon dessert mais dans la semaine tu l auras
avatar
ramise
Petite section
Petite section

Nombre de messages : 56
Age : 37
Date d'inscription : 05/02/2007

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  talz le Mar 13 Fév - 14:28

Fifi a écrit:talz yowe soupe yéél la léye toggal Very Happy

mo waay, lii nékh neu dé, mane daal prinche deugg laa Laughing Laughing té fima tolou dama néchéchité soupe ndakh meu nodantékou touti Laughing Laughing
avatar
talz
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 514
Date d'inscription : 03/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  talz le Mar 13 Fév - 14:29

ramise a écrit:talz yangui thi birr gnorna ba paré wakhma foumakay posté mou eksi ma khar sama appréciation wou serigne en attendant dessert bi di paré Rolling Eyes Rolling Eyes

gnanal meu mou rééss ak diameu waay, lou nékh réka nékh Laughing
avatar
talz
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 514
Date d'inscription : 03/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  ramise le Mer 14 Fév - 1:24

TALZ, na ress akh diam, fifi dinala yone gnenti yellou nak ak you khar ndakh mou farr ak gnomine birr ak yoyou nonou ndakh yakh yi mouna nodantikou Rolling Eyes Rolling Eyes
avatar
ramise
Petite section
Petite section

Nombre de messages : 56
Age : 37
Date d'inscription : 05/02/2007

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  talz le Mer 14 Fév - 2:23

ramise kharal kone ma tambali takkamtékou sakh Laughing Laughing
avatar
talz
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 514
Date d'inscription : 03/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Fifi le Ven 16 Fév - 2:00

ramise merci waye dina ma arrangé trope , maguini di déme marche pour acheté aye poro, karotte, pomme de terre, nawé ak sobelé, mé bireyi boule faté kheuteurbi ok., té yéle eske khosse nagnou bamou set , défalemassi carbonate comme ça mou téla diore .
Talz soupe bi mome dina la arrangie pour gua nodantikou daguéye nane si diékh bi reck Smile
avatar
Fifi
Moyenne section
Moyenne section

Nombre de messages : 107
Date d'inscription : 04/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  ramise le Ven 16 Fév - 2:35

fifi, seras lalay demal rek defarala sa mbouss bamou bakh fofou so dieundé sakh gnolay defaral carbonnate soubbeu ak diam dinga mouna togal talz soupeum
avatar
ramise
Petite section
Petite section

Nombre de messages : 56
Age : 37
Date d'inscription : 05/02/2007

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  talz le Ven 16 Fév - 2:53

yéén gnaar daal guiss na ni nguéén maye takha woo pour ma meune nodantékou Laughing Laughing fok ma béral léén loxo especial aussi Laughing surprise laa léén di défal Laughing
avatar
talz
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 514
Date d'inscription : 03/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Big le Ven 16 Fév - 4:37

Fifi , Carbonate dafaye nelawlo aprés.


amnn nakk beug naa ci yélou nakk yii koumako soupeul

_________________
_________________
"Cheikh Ibra, tu as été élevé au dessus des humains"
"Ton état de réalisation ne peut-être compris par de simples mortels"
"... La voie d'Ibra Fall dans le Mouridisme est
avatar
Big
Admin
Admin

Nombre de messages : 1045
Date d'inscription : 05/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  ramise le Mer 21 Fév - 2:01

FIFI ndogue bi gnewna ya thi dess nak tou est au complet sama serigne nak nanko tibeul bolou mouride khamngua louma beugue wakh ffou tedou boumou wekh pobar nak
TALZ nena khifna
avatar
ramise
Petite section
Petite section

Nombre de messages : 56
Age : 37
Date d'inscription : 05/02/2007

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Fifi le Mer 21 Fév - 2:54

Wawe ramise cone book ma koumassé
sama tchine laye tékk défe si nokh soti si yélle yi, ak lakhisseyi, ak thialguéne bi, khorome ko ... bayi ko mouye bakh.
Bou bakhé lou yague , ba kholi saméye carrote, nawé, pomme de terre néko si peuye.
Deube sama nokosse maname kani, pobare bou doye ak porro bou barry, ak latche bouye doye, ak sobalassé bou barry pour sauce bi fate ak jumbo.
Bouma si défé lépe nak ba khole diame lépe normale ma wagni sama gaz bayiko mouye barre ba lépe gniore ba niékh bi fare ma tégui sama tchine nak.
Fék rakhasse na saméye assite pour soupe ba parré ak sama cuilliére dale di servie au chaud nakh soupe déye tangue.
Talz nakh mome la téguaule dialguéne bi Laughing
bon yégualena si dieupe di léne wakh bon appétit
Bo léne lékké ba parré défare na béne salade de fruit ak diarrou sowou piire bo léne si beugue recck ma servire léne .
avatar
Fifi
Moyenne section
Moyenne section

Nombre de messages : 107
Date d'inscription : 04/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  NUTELLA le Mer 21 Fév - 3:16

FIfi bok nadé li nekh na badé Laughing
Talz moytoul matalé sa baram boy séniou yélbi Laughing

_________________
[b] LE CHIEN ABOIE LA CARAVANE PASSE
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Fifi le Mer 21 Fév - 3:33

NUTELLA ya gui si biir khadje guassi dé
avatar
Fifi
Moyenne section
Moyenne section

Nombre de messages : 107
Date d'inscription : 04/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  NUTELLA le Mer 21 Fév - 4:04

Fifi a écrit:NUTELLA ya gui si biir khadje guassi dé

diadieuf way na baré rék dama fokalé

_________________
[b] LE CHIEN ABOIE LA CARAVANE PASSE
avatar
NUTELLA
Collège
Collège

Nombre de messages : 617
Date d'inscription : 16/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  talz le Jeu 22 Fév - 3:19

Fifi a écrit:Wawe ramise cone book ma koumassé
sama tchine laye tékk défe si nokh soti si yélle yi, ak lakhisseyi, ak thialguéne bi, khorome ko ... bayi ko mouye bakh.
Bou bakhé lou yague , ba kholi saméye carrote, nawé, pomme de terre néko si peuye.
Deube sama nokosse maname kani, pobare bou doye ak porro bou barry, ak latche bouye doye, ak sobalassé bou barry pour sauce bi fate ak jumbo.
Bouma si défé lépe nak ba khole diame lépe normale ma wagni sama gaz bayiko mouye barre ba lépe gniore ba niékh bi fare ma tégui sama tchine nak.
Fék rakhasse na saméye assite pour soupe ba parré ak sama cuilliére dale di servie au chaud nakh soupe déye tangue.
Talz nakh mome la téguaule dialguéne bi Laughing
bon yégualena si dieupe di léne wakh bon appétit
Bo léne lékké ba parré défare na béne salade de fruit ak diarrou sowou piire bo léne si beugue recck ma servire léne .

éy waay fifi ak ramise, contane naa ci yéén gnaar gnii dé Laughing Laughing merchi les gosses merchi , voit tout, guiss na léppeu Laughing Laughing nutella gneuwal diappalé ma ci ndakh lii dina nékh dé Laughing
avatar
talz
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 514
Date d'inscription : 03/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  thiaate le Jeu 22 Fév - 8:58

talz yaw t gaté dé! okho!! Laughing
avatar
thiaate
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 462
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  talz le Jeu 22 Fév - 13:32

thiaate a écrit:talz yaw t gaté dé! okho!! Laughing

gosse fo rérone? yako guiss dé, plus heureux k moi meurt Laughing
avatar
talz
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 514
Date d'inscription : 03/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  thiaate le Ven 2 Mar - 11:26

talz a écrit:
thiaate a écrit:talz yaw t gaté dé! okho!! Laughing

gosse fo rérone? yako guiss dé, plus heureux k moi meurt Laughing

ma ngui fi sakh dé! niakk diote temps yii rek!mais sama khél mi ngui si yéne! nammone na la Wink Wink
avatar
thiaate
Modératrice
Modératrice

Nombre de messages : 462
Date d'inscription : 14/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  talz le Lun 5 Mar - 14:51

mangui nii rék, ci lo nék?
avatar
talz
Modérateur
Modérateur

Nombre de messages : 514
Date d'inscription : 03/12/2006

Voir le profil de l'utilisateur

Revenir en haut Aller en bas

Re: coin des cordons bleus pour beguel sougnou alaaadji yi

Message  Contenu sponsorisé


Contenu sponsorisé


Revenir en haut Aller en bas

Page 7 sur 7 Précédent  1, 2, 3, 4, 5, 6, 7

Voir le sujet précédent Voir le sujet suivant Revenir en haut

- Sujets similaires

 
Permission de ce forum:
Vous ne pouvez pas répondre aux sujets dans ce forum